Numbers 20:18
TSK
¶ Buurub Edom nag ne leen: «Dungeen jaare fi man de, lu ko moy saamar laay génne, dajeek yeen.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Buurub Edom nag ne leen: «Dungeen jaare fi man de, lu ko moy saamar laay génne, dajeek yeen.»
¶ Siwon buurub Esbon nag nanguwu noo may nu jaare fa moom, ndax booba seen Yàlla Aji Sax ji moo dëgëral boppam, wowal xolam, ngir teg ko ci seen loxo niki bésub tey jii.
ca wàllaa dexu Yurdan, ca xur wa janook Bet Pewor, ca réewum Siwon buurub Amoreen ba toogoon Esbon, te Musaa ak bànni Israyil duma woon ko, ba ñu génnee Misra.
Yuux jibe na Esbon, ba Elale, àkki ba Yaxacc ak Sowar ba Oronayim ak Eglat Selisiya. Ndoxi Nimrim sax ŋiis na.