Exodus 6:9
TSK
¶ Ba Musaa waxee loolu bànni Israyil, dégluwuñu ko sax ndax xol bu jeex ak njaam gu metti.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Ba Musaa waxee loolu bànni Israyil, dégluwuñu ko sax ndax xol bu jeex ak njaam gu metti.
¶ Buurub Edom nag ne leen: «Dungeen jaare fi man de, lu ko moy saamar laay génne, dajeek yeen.»
¶ Ba loolu amee Musaa def la ko Aji Sax ji sant, ñu ànd yéeg kaw tundu Or, mbooloo ma mépp di gis.
Dañoo dem ba àgg xuru Eskol, ba gis réew ma, doora délsi, di yoqiloo bànni Israyil, ngir ñu baña duggi ca réew, ma leen Aji Sax ji joxoon.
Yeen nag walbatikuleen dellu màndiŋ ma, topp yoonu géeju Barax ya.»
Ñuy feddli pastéefu taalibe yi, di leen ñaax ngir ñu saxoo ngëm, ne leen: «Coono yu baree ngii, fàww nu jaare ci, ngir tàbbi ci nguurug Yàlla.»