كل أسفار KYG

Numbers 22

KYG · الآية 6

36 أصحاحات

KYG / Numbers / الأصحاح 22

KYG · الآية 6

K on nag dikkal gaaw ñaanal ma yàlla gàngoor gii, ngir ñoo ma ëpp doole. Jombul ma duma leen, ba dàq leen réew mi, ndax xam naa ne koo ñaanal, mu barkeel, te koo ñaan-yàlla, mu alku.»