TSK

TSK · Numbers 24:14

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Maa ngi koy gis, te du tey, Maa ngi koy niir, te jubseegul; biddiiw a feqe fa Yanqóoba, yetu nguur a yékkatikoo fa Israyil, daldi toj boppi Mowab, toj kaaŋi mboolem askanu Set.

Dees leen di boole denc cim pax, ne leen ràpp tëj, ba mu am ay fani fan, ñu mbugal leen.

«Waaye fan yu mujj ya, maay tijji wërsëgu Elam.» Kàddug Aji Sax jee.

Léegi ñëw naa ngir xamal la liy dikkal sa mbooloo ci jamono yiy ñëw ndax peeñu mi ëmb na jamono yooyu itam.»

Micah 6:5 TSK

Yeen sama ñoñ, fàttlikuleen rekk la leen Balag buurub Mowab fexeeloon, ak la ko Balaam doomu Bewor tontu woon. Doxub diggante Sitim ba Gilgal it, baleen ci xel, ba ràññee njekku Aji Sax ji.

¶ Lii, nanga ko xam: mujug jamono, jant yu tar dina dikk.

¶ «Waaye lenn a ngi lu ma lay sikke: yaa ngi uuf foofu ay nit ñuy saxal njànglem Balaam, moom mi doon xiirtal Balag ci tegal Israyil ndëgg-sërëx, ngir ñu lekk ñam wu ñu sarxal ay tuur, ak di gànctu.