Numbers 17:13
TSK
Naka la taxaw ci diggante ñi dee ak ñiy dund, mbas ma dal.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Naka la taxaw ci diggante ñi dee ak ñiy dund, mbas ma dal.
«Fineyas, doomu Elasar, doomu sarxalkat bi Aaróona, moo moyale Israyil samam sànj, ndax sama fiiraange gi mu ma fiirlee ci seen biir, ba faagaagaluma bànni Israyil ci sama biir fiiraange.
Ñu boole kook yaxi Sóol ak doomam Yonatan, denc lépp ca sëgu Kis, baayu Sóol, ca diiwaanu Beñamin ca Sela. Ñu def la Buur santaane lépp. Gannaaw loolu Yàlla nangul réew ma.