TSK

TSK · Numbers 28:15

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

bu nemmikoo bàkkaar bi mu def rekk, na sarxe sikket bu amul sikk.

Mu daldi matale loolu njotlaayal bérab bu sell bee sell, tàggale kook sobey bànni Israyil ak seeni tooñ, ak lu seen bàkkaar mana doon. Noonu lay defal mboolem xaymab ndaje, mi dëkk ci seen biir ci seen biiri sobe.

Nga waxleen ne leen, lii moo di saraxu sawara bi ñuy indil Aji Sax ji: xar yu góor yu menn at yu mucc sikk, ñaar ci bés bi, muy saraxu rendi-dóomal bi war bés bu nekk.

ak benn sikketu póotum bàkkaar ngir seen njotlaay.

ak benn sikketu póotum bàkkaar, ngir seen njotlaay.

Li yoonu Musaa tële woon ndax néew dooley nitu suuxu neen, mooy lii Yàlla def: Doomam la yónni, mu dikke melow nit, te nit di bàkkaarkat, di suuxu neen, ngir Doomam fajtal mbirum bàkkaar. Yaramu suux wu nit kooku la Yàlla sottale mbugal gi war ci bàkkaar,