TSK

TSK · Numbers 29:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ «Bu saraxam dee saraxu jur gu gudd gu ñuy def rendi-dóomal, na sarxal aw yëkk wu amul sikk. Na ko yóbbu ci bunt xaymab ndaje mi ci kanam Aji Sax ji, ngir mu nangul ko ko.

Nangeen ci def saraxu sawara, mu dib rendi-dóomal, ñeel Aji Sax ji: ñaari yëkk yu ndaw, ak menn kuuy, ak juróom ñaari xari menn at, te ngeen def lépp di lu mucc sikk.

Sarxal-leen ci ab rendi-dóomal ngir xetug jàmm, ñeel Aji Sax ji: wenn yëkk wu ndaw, ak menn kuuy, ak juróom ñaari xari menn at, te lu ci nekk mucc sikk.

Ezra 3:4 TSK

Ñu teg ca amal màggalu Mbaar ya, mu dëppook la ñu bind, boole kook saraxu dóomal yi war bés bu nekk.

Waaye kii de, ba mu sarxee ngir ay bàkkaar, bennub sarax, mu doy ba fàww, ca la tooge fa ndijooru Yàlla.