¶ Aji Sax ji teg ca wax Musaa ne ko:
TSK
TSK · Numbers 29:7
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Man de ba ñu woppee, maa ngi ñaawlu, di woor, toroxloo, sukk, ñaanal leen,
Bésub keroog Boroom bi, Aji Sax ji ci gàngoor yi moo leen di woo ci jooyoo ak ñaawlu ak wateefu nel, ak colu saaku ngir ñaawlu.
Ñu wax ak sarxalkati kër Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, ak yonent yi, ne leen: «Ndax danoo wara wéye jooy ak di woor ci weeru juróomeel, ni nu ko baaxoo at yii yépp?»
Maa leen ne déedéet kay, te su ngeen tuubul, yeen ñépp ay sànku ni ñoom.»
Li nu bir moo di nun ña woon démb, ca bantub Yeesu ba lees nu daajaale, ngir xewil sunu yaramu bàkkaar, ba nu noppee doon ay jaam, bàkkaar di sunub sang.
Waaye tey bég naa, te du tiis wu ngeen tegoo laay bége, waaye li leen tiis wi tuubloo, laay bége, ndax woowu xeetu tiis la Yàlla namm ci yeen, moo tax it yóbbewunu leen jenn loraange.