TSK

TSK · Numbers 30:8

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Yàlla teg ca ne jigéen ja: «Dinaa taral sa metitu mat, ci metit ngay wasin. Sa bëgg-bëggu bakkan dina la xiir ci sa jëkkër, te moo lay teg tànk.»

Jigéen ña teg ca ne: «Te sax ba nuy taalal cuuraay Lingeeru asamaan, di ko tuural, sunuy jëkkër dañu koo yégul? Xam nañu xéll ne nu ngi defal Lingeeru asamaan ay nàkk yu koy jëmmal, di ko tuural ay naan.»

¶ na jigéen ñi noppi ci biir mbooloo yi, ndax mayeesu leen ñu wax ci yooyu jataay. Na jigéen ñi nangu, ni ko yoon wi ci boppam diglee.