Exodus 17:16
TSK
Booba la wax ne, gannaaw loxoo ñemee xàcci, jëm ci ngànguney Aji Sax ji, Aji Sax ji dootu noppee xareek Amaleg ba fàww.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Booba la wax ne, gannaaw loxoo ñemee xàcci, jëm ci ngànguney Aji Sax ji, Aji Sax ji dootu noppee xareek Amaleg ba fàww.
«Fineyas, doomu Elasar, doomu sarxalkat bi Aaróona, moo moyale Israyil samam sànj, ndax sama fiiraange gi mu ma fiirlee ci seen biir, ba faagaagaluma bànni Israyil ci sama biir fiiraange.
Nanga tas sa kër sang Axab, te noonu laay toppe soxnaam Yesabel sama bakkani jaam ñépp: muy yonenti Aji Sax jeek ñi dul yonent.
Waaye bésub keroog déy, Boroom bi Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko moom, muy bésub feyu bu muy feyey noonam. Saamar suur suux, màndee deret. Boroom bi Aji Sax ji Boroom gàngoor yi mooy rendee réewum bëj-gànnaar ab sarax, feggook dexu Efraat.