Numbers 5:9
TSK
Te itam bépp jooxe bu bokk ci mboolem sarax yu sell, yi bànni Israyil indil sarxalkat bi, sarxalkat bee koy moom.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Te itam bépp jooxe bu bokk ci mboolem sarax yu sell, yi bànni Israyil indil sarxalkat bi, sarxalkat bee koy moom.
Mboolem jooxe yu sell yi bànni Israyil di jooxeel Aji Sax ji, sédd naa la ko, yaak sa doom yu góor, ak sa doom yu jigéen, ci kaw dogalu yoon bu sax dàkk. Kóllërey xorom a ngoogu, du fecciku, xanaa sax dàkk fi kanam Aji Sax ji, ñeel la yaw, yaak saw askan.»
¶ Ki ñuy jàngal kàddug Yàlla nag war naa sédd ki koy jàngal ci mboolem alalam.
¶ Seetleen ni mu ràññikoo, moom la Ibraayma maamu cosaan ma ci boppam jébbal fukkeelu cérub cëxëtoo ma!