¶ Aadama dund téeméeri at ak fanweer (130), jur doom ju góor, mu bindoo melokaanam te nirook moom. Mu tudde ko Set.
TSK
TSK · Numbers 32:14
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Ba Aji Sax ji déggee seeni kàddu, dafa mer ba giñ ne:
Ci kaw loolu Esra sarxalkat ba jóg taxaw, ne leen: «Yeena fecci kóllëre ndax yeena jël ay jaambur jabar, di yokk tooñaangey Israyil.
Xanaa du nii la seen maam ya daan def, ba tax sunu Yàlla wàcce ci sunu kaw musiba mii mépp, wàcce ko ci dëkk bii, yeen ngeen di wooti sànjum Yàlla ci kaw Israyil, di teddadil bésub Noflaay?»
xanaa dëddu, di ko wor ni seeni maam, toogadi ni xala gu yolom.
ana ku ngeen di ñaawal? Ana ku ngeen di ŋóobi, ak di ko kókkali? Xanaa dungeen doomi moykat, di askanu workat,
¶ «Waaye doom ya dañu maa gàntal. Sama dogali yoon, jëfewuñu ko, sama àttey yoon yiy guddal fanu képp ku koy jëfe, sàmmuñu ko. Sama bési Noflaay lañu ñàkke worma. Ma nar leena xëpp samam sànj, ŋaccal leen sama mer ca màndiŋ ma.
Kon yeena seedee noonu ne seen jëfi maam ya, ànd ngeen ci, ndax ñoom ñoo leen rey, yeen ngeen tabax seeni bàmmeel.