كل أسفار KYG

Numbers 32

KYG · الآية 29

36 أصحاحات

KYG / Numbers / الأصحاح 32

KYG · الآية 29

M usaa ne leen: «Su Rubeneen ñeek Gàddeen ñi àndeek yeen, ñoom ñépp gànnaayu ngir xareji fi kanam Aji Sax ji, ba réew ma nangul leen, nangeen leen jox réewum Galàdd, muy seen moomeel.