Numbers 35:16
TSK
¶ «Su dee ag weñ la ko dóor, mu dee, moo ko rey, te dee rekk mooy àtteb ki rey.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ «Su dee ag weñ la ko dóor, mu dee, moo ko rey, te dee rekk mooy àtteb ki rey.
¶ Bennub seede nag du taxaw, di tuumaal kenn, ci genn tooñ mbaa bàkkaar, ak bépp bàkkaar bu mu mana bàkkaar. Ci kaw kàddug ñaari seede mbaa ñett la mbir ma di wére.
¶ Ñetteel bi yoon a ngii, bu ma leen di ganesi. «Ci kàddug ñaari seede ba ñett nag la àtteb mépp mbir di wére.»
Képp ku masoona xëtt yoonu Musaa, daawuñu ko ñéeblu; ci kaw seedey ñaari nit ba ñett lees ko daan rey.