¶ «Alku ñeel na képp ku sàkk, bay teg ci bérab bu làqu, li Aji Sax ji seexlu, te ab liggéeykat sàkke ko ay loxoom, muy jëmmu tuur mu ñu yett, mbaa mu ñu móol.» Su ko defee mbooloo mépp àddoondoo, ne: «Amiin!»
TSK
TSK · Numbers 5:22
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Job 31:39
TSK
ndegam maa lekk lu ca ñor, te dikkewuma dara, ba xañ bakkan ña ma ko beyaloon,
Psalms 41:13
TSK
Man, damaa maandu, nga taxawu ma, dëj ma fi sa kanam, ba fàww.
Psalms 89:52
TSK
Aji Sax ji, say noon a ngi sewal buur bi nga fal, ne ko dann.
Proverbs 1:31
TSK
Waaye loo ci góobe, gar ko, say pexe suur la këll.