Numbers 4:3
TSK
Daleleen ci góor ñi am fanweeri at, ba juróom fukki at, muy mboolem ñi yelloo bokk ci kurél, gi liggéeyu biir xaymab ndaje mi war.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Daleleen ci góor ñi am fanweeri at, ba juróom fukki at, muy mboolem ñi yelloo bokk ci kurél, gi liggéeyu biir xaymab ndaje mi war.
¶ Kan moo masa ràngu liggéeyu coldaar, te léppam war ko? Ana kuy jëmbat tóokërub reseñ, te du lekk ca doom ya? Mbaa kan mooy sàmm ag jur, te du naan ca soowum jur ga?
¶ Kon nag Timote doom, loolu mooy ndigal li ma la dénk, te mu dëppook kàdduy waxyu yi jotoona jib te jëm ci sa mbir. Gànnaayool kàddu yooyu ngir di ci xaree xare bu baax bi,
Jëlal sa wàll ci coono bi takk-derub Almasi Yeesu bu wóor di jànkoonteel.