Job 39:27
TSK
Am yaa sant jaxaay mu naaw ba fa kaw, di tàgge kawte ya?
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Am yaa sant jaxaay mu naaw ba fa kaw, di tàgge kawte ya?
Seen ragluwaay ak seen reewande sànk na leen, yeen ñi dëkke xuntiy doj, féetewoo colli tund yi. Waaye su ngeen ajee seenum tàgg ni jaxaay it, fa laa leen di àjjee.» Kàddug Aji Sax jee.
Bu ñu bëttoon, ba biir njaniiw it, fa laa leen di yóotoo. Ñu yéeg asamaan, ma wàccee leen fa.