Romans 16:5
TSK
Nuyul-leen ma itam mbooloom gëmkat miy daje ca seen kër. Nuyul-leen ma sama soppe Epaynet, miy jooxeb ndoortel meññeef, ma génne ca diiwaanu Asi, ñeel Almasi.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Nuyul-leen ma itam mbooloom gëmkat miy daje ca seen kër. Nuyul-leen ma sama soppe Epaynet, miy jooxeb ndoortel meññeef, ma génne ca diiwaanu Asi, ñeel Almasi.
¶ Ci wàllu Epafrodit, sama mbokkum gëmkat la, di sama naataango, di sama mbokkum xarekat, te di seen ndaw li ngeen ma yóbbante ndimbal lu faj samay soxla. Waaye jàpp naa ne fàww ma delloo leen ko,
¶ Waxal-leen ma Arsipp ne ko: «Neel jàkk ci liggéey bi nga sasoo ci Boroom bi, ngir nga sottal ko.»