Waaye sama xel dalul woon, ndax gisuma woon sama mbokk, Tit. Teewul ma tàggtoo ak ñoom, jëm diiwaanu Maseduwan.
TSK
TSK · Philippians 2:25
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Am boog damaa tooñ ca na ma toroxloo ngir darajaal leen, ndax la ma leen laajul ag pey, ba ma leen di àgge xibaaru jàmm bu Yàlla bi?
Philippians 4:18
TSK
Fii ma tollu jot naa li ma aajowoo lépp, maa ngi ci naataange; doyle naa sëkk, gannaaw ba ma nangoo ci loxol Epafrodit, seenub yóbbante, te sarax su ñu nangu la, di xeeñ xetug jàmm, te neex Yàlla mi mu ñeel.
Colossians 4:11
TSK
Yeesu mi ñuy wax Yustus itam, mu ngi nuyoo. Li bokk ci askanu Yawut, ñoom rekk ay liggéeyandoo ak man ngir nguurug Yàlla, te ñoo seral sama xol.
2 Timothy 2:3
TSK
Jëlal sa wàll ci coono bi takk-derub Almasi Yeesu bu wóor di jànkoonteel.
Philemon 1:24
TSK
mook Màrk ak Aristàrk ak Demas ak Luug, bokk yi may liggéeyandool.