Esther 2:22
TSK
Teewul Mardose yég pexe ma, wax ko Lingeer Esteer, mu yegge ko Buur, ci turu Mardose.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Teewul Mardose yég pexe ma, wax ko Lingeer Esteer, mu yegge ko Buur, ci turu Mardose.
Ñi ci mbégte, bokkleen ak ñoom seen mbégte; ñi ci naqar, ngeen bokk ak ñoom seen naqar.
¶ Nun ñi fendi ci wàllu ngëm, fàww nu xajoo tëley ñi néew doole, te baña sàkku sunu bànneexu bopp.
Bu kenn sàkku njariñal boppam, waaye sàkkuleen seen njariñal moroom.
Céri yaram yi gëna niru lu néew doole sax, ñooy cér yi manula ñàkk.
¶ Buggunu kenn sikk sunub liggéey, moo tax buggunoo jëfe lenn luy doon tojaange ci kenn.
¶ Ndegam nag yoonu Buur Yàlla ngeen matal sëkk, di sàmmonteek Mbind mi ne: «Ni ngeen soppe seen bopp, nangeen ko soppe seen moroom,» su boobaa waawleen góor!