TSK

TSK · Proverbs 1:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ragal Aji Sax ji di ndoortel rafet xel, dég-dég bu rafet ñeel ku koy wéye. Moo yeyoo cant ba fàww.

Daa fekk nga baña xam, te ragal Yàlla du loo taamu.

Ragal Aji Sax ji di njàlbéenu rafet xel, xam Aji Sell ji di am ug dégg.

Ragal Aji Sax ji day rafetal xel; jëkke woyof, mujje tedd.

Ma daaneele fii, déggees na lii lépp: Yàlla, ragal ko; ay santaaneem, jëfe ko; loolu rekk mooy nit.

¶ Gannaaw ràññee Yàlla jaralu leen dara, Yàlla it bërgal leen ak seen xel mu doyadi, ba ñuy def jooju jëf ju jekkadi.