TSK

TSK · Proverbs 10:16

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Nit ku jub garab la, doom ya di dundal; ku rafet xel wut nit ñi.

Neleen aji jub ji mooy baaxle, mooy yooloo añam.

¶ Kon nag yeen sama bokk yi ma soppal sama bopp, farluleen, bu leen dara yëngal, te saxooleena jëm kanam ci liggéeyu Sang bi, te ngeen xam ne seenu ñaq, ci seenub ànd ak Sang bi, du neen.

te kàdduy ñooñu day law ni ngal. Ci ñooñu la Imene ak Filet bokk.

Yàlla ñàkkul worma bay fàtte seen liggéey, ak cofeel gi ngeen sopp turam, te firndeele ko ni ngeen taxawoo ñu sell ñi, démb ak tey.