Leviticus 19:16
TSK
Buleen wër di yàq deru nit ci seen bokki waa réew. Buleen def dara lu mana reylu seen moroom. Maay Aji Sax ji.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Buleen wër di yàq deru nit ci seen bokki waa réew. Buleen def dara lu mana reylu seen moroom. Maay Aji Sax ji.
mu gën koo ragalati. Fa la Sóol doxe doon noonub Daawuda ba fàww.
Ba loolu wéyee Daawuda ne Uri: «Àggal sa kër nag te jàngu.» Uri bàyyikoo kër Buur, ab yóbbalu Buur topp ca gannaawam.
Yowab ne Amasa: «Mbokk mi, mbaa jàmm nga am?» Yowab jàpp sikkimu Amasa ca loxol ndijooram, mel ni ku koy fóon.
Wallóoy, Aji Sax ji, ngor jee na! Kóolute réer na doom aadama.
ngeen di tooge seen mbokk, di yàq deru doomu ndey.
Kuy jëw moroomam, ma wedamal; ku daŋŋiiral ak ku reew, muñaluma la.
Ñoom ñépp a di fippukat yu fétteeral, wër di sos, dëgërle ni xànjar ak weñ gu ñuul. Ñoom ñépp di yàqkat.