Proverbs 2:14
TSK
Kon nga mucc ci kuy def lu bon, tey bànneexoo lu jekkadi.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Kon nga mucc ci kuy def lu bon, tey bànneexoo lu jekkadi.
Jëfi dof a neex ku ñàkk bopp, ku am ug dégg def njub.
Nit kuy naxe, naan: «Damay fo!» yaay dof buy sànniy jum, di fitteek a reye.
Xalelu góor bi, bànneexul bi ngay gone, bégalal sa xol bi ngay ndaw. Toppal loo namm ak loo xemmem, waaye xamal ne loolu lépp, Yàlla da la koy laaj.