TSK

TSK · Proverbs 10:27

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 15:32 TSK

Balaa jantam a lang mu jot añam, te caram dootu naat.

Yaa ko gatandoo barkey ngëneel, kaalaa ko wurusu ngalam.

Sippikul Aji Sax ji lu la diis, moom moo lay taxawu. Du bàyyi mukk aji jub, muy tërëf.

bu màggatee sax di meññ, tooy xepp, sëq lipp,

Gudd fan, mu joxee ndijoor; càmmoñ ba, alal ak teraanga.

Bu la mbon jiital, te bul dofe. Jàppool lii, te baña wacc lee, mooy li gën, lu ko moy nga dee te sa àpp jotul. Ku ragal Yàlla kat sàmm yooyu yaar.

Yàlla nag ne ko: “Ñàkk xel! Guddig tey jii, dees na jël sa bakkan. Kon li nga waajal, ana kuy doon boroom?”