Psalms 15:5
TSK
Du leble, ba teg ca; du nangu ger, ngir fexeel jaambur. Lii ku koy jëfe doo jang.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Du leble, ba teg ca; du nangu ger, ngir fexeel jaambur. Lii ku koy jëfe doo jang.
Ku bon, ñu dagg, sànni; ku yaakaar Aji Sax ji, jagoo réew mi.
Aji Sax ji kat daa sopp yoon, te du wacc jaamam bu gore. Day fegu ba fàww, askanu ku bon dog.
Ku jub du tërëf mukk, te dees na ko fàttliku ba fàww.
ndax kuy jubal ay dëkke réew mi, te ku mat a fiy des.
Bu ngëlén walee, ab soxor ne mes; ku jub, sab reen sax ba fàww.
Jigéen ñi ci sama ñoñ ngeen dàqe seen këri mbégte, te seeni doom, yeena leen xañ sama barke ba fàww.
Ana ku nuy tàggaleek cofeelu Almasi? Du ay nattu, te du njàqare, du it coonoy bundxatal, mbaa ab xiif, mbaa rafle, te du genn aaytéef, ba cib saamar.