Proverbs 2:12
TSK
mucc ci yoonu ku bon ak kuy wax lu jekkadi,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
mucc ci yoonu ku bon ak kuy wax lu jekkadi,
Ab soxor, waxam am tëru la, day reye; kàdduy kiy jubal di musle.
Ku xelu àddu, xam-xam rafet; ab dof di talalali.
Ab dof, làmmiñam sooke naw ay, ay waxam di sàkku yeti gannaaw.
Waarekat ba daa tànn baat yu saf, bind ko, mu jub te dëggu.
ak kàddu gu wér gu kenn dul mana weddi, ngir rusloo ab noon bu amul lenn lu bon lu mu nu baatale.