TSK

TSK · Proverbs 11:20

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Aji Sax jee jub, sopp njub; kuy jubal, gis yiwam.

Yaw laa moy, yaw doŋŋ. Li nga ñaawlu laa def. Kon boo waxee, yaa yey; te soo àttee, wàcc nga.

Xam naa ne Aji Sax jeey jox néew-ji-doole dëgg; di sàmm àqu baadoolo.

Juróom benn a ngii yu Aji Sax ji bañ, ba ci juróom yaar yu mu seexlu:

Artu kuy ñaawle, feyoo saaga rekk, yedd ab soxor, yooloo loraange.

Ku mat day jub, ba fegu; moykat soxor, ba sànku.

Aji Sax ji bañ na mébét mu bon, te wax ju yiw daa sell fa moom.

Ku bon day ñeme-ñemelu, ku jub la muy def da koy wóor.