TSK

TSK · Proverbs 11:22

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ma laaj ko ne ko: “Kan moo la jur?” Mu ne: “Betuwel, doomu Naxor ak Milka.” «Ca laa ko takkal jaaro bi ci bakkanam, ak lam yi ciy loxoom.

Jigéen ju dof day xumb, reew, du xam lu xew.

Melokaan wu jekk day naxe, taar day wéy, waaye jigéen ju ragal Aji Sax ji, kookoo jara gërëm.

Nahum 3:4 TSK

Lépp ndax ngànctu gu bare, gi gànc bi nekke! Jekk tànkee, boroom xërëm yi, ci ngànctu nga jaaye ay xeet, te xërëmtu nga naxe ay giir.

Li léeb wii wax te muy dëgg, moo leen dikkal: «Xaj waccu, lekkaat ko; te cangaayu mbaam-xuux, teewu koo xalangootee poto-poto.»