Proverbs 3:12
TSK
ndax Aji Sax ji, ku mu sopp, waññi la, ni baay, ak doom ju ko neex.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
ndax Aji Sax ji, ku mu sopp, waññi la, ni baay, ak doom ju ko neex.
Yaral sa doom ba muy teel, waaye bul topp sa xol, ba rey ko.
Bul ñéebloo yar gone, bantal ko taxu koo dee.
Yaral sa doom, mu noppal la, bànneexal la.
ndax Boroom bi, ku mu sopp, yar la, mooy bantal jépp doom ju ko neex.»