TSK

TSK · Proverbs 15:24

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Xoolal ndax maa ngi doxe yoon wu aay, te nga teg ma ci yoon wi sax.

Tànk ya day bartalu wuti ndee, ay jéegoom àkki njaniiw.

Këram yoonu njaniiw la, daa bartalu, tàbbi néegi ndee.

Nun nag sunum réew a nga fa asamaan, fa nuy séentoo sunu Musalkat, Sang Yeesu Almasi.