Psalms 89:15
TSK
Njekk ak njub a lal sab jal, ngor ak worma dox jiitu la.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Njekk ak njub a lal sab jal, ngor ak worma dox jiitu la.
Njàqare day jeexal xolu boroom, wax ju neex di tooyal xolam.
Xol bu sedd day garabal, xol bu tiis day semmal.
Leer neex na, gis jant neex na.
Malaaka mi ne leen: «Buleen tiit, ndax kat maa leen indil xibaaru jàmm bu doon mbég mu réy, ñeel askan wépp.
Guddi du amati, te deesul soxlaati làmp mbaa naaj, ndax Boroom bi Yàlla moo leen di leeral. Te dañuy nguuru ba fàww.