TSK

TSK · Proverbs 16:18

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Aman duggsi, Buur ne ko: «Ana lees di defal waa ju buur namma teral a waay?» Booba Aman a nga naan ca xel ma: «Ana ku Buur namma teral ku dul man mii?»

Bésub keroog booba, ku bew bay regeju mooy detteelu, sagub nit sàggiku, Aji Sax ji doŋŋ mooy jagoo kawe.

Gannaaw gi, ba muy sujjóot ca kër tuuram ma ñuy wax Nisrog, Addraameleg ak Sareser, doomam yu góor ñoo ko fa fàdde saamar. Ñoom nag ñu daw làquji réew ma ñuy wax Araraat. Ci kaw loolu doomam Asaradon falu buur, wuutu ko.

Sab taar a la fuuyloo, sa daraja tax nga yàq sam xel! Fi suuf laa la rattax, fi kanam buur yi laa la detteel, ñu di la seetaan.

¶ «Yaw Baltacar miy doomam nag, xam nga loolu lépp te taxu laa toroxlu,

Mbooloo moomu dees na leen faagaagal, buur bëj-saalum di ca réy-réylu. Dina rey ay junniy nit nag, waaye du ko taxa am ndam.

Luke 14:9 TSK

Su boobaa moom mi la woo, woo ko, mooy dikk, ne la: “Mayal kii, mu toog.” Nga am nag gàccey walbatiku toogi fa gëna gannaawe.

Te it bumu dib tuubeen bu bees, lu ko moy ag réy-réylu man na koo gëlëmal, ba mu tàbbi ci mbugal ni Seytaane.