Proverbs 14:29
TSK
Muñ mer, déggin wu yaa; gaawa tàng, gënatee dof.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Muñ mer, déggin wu yaa; gaawa tàng, gënatee dof.
Woyof, ànd ak ku néewle moo gën séddook ku bew la mu lewal.
Muñ mer ay nax kilifa, te wax ju neex, fu mu jaar, mu nooy.
Bul gaawa mer; mer, xolub dof la samp këram.
¶ Kon nag doonleen ay roykati Yàlla, gannaaw yeenay doomam yi mu sopp,
¶ «Ku am ndam nag, maa lay may nga toog ak man fi sama ngàngune, na ma ame woon ndam, ba toog ak sama Baay fi ngànguneem.