¶ Esawu nag bañ Yanqóoba ndax barke ba ko baayam ñaanal. Ma ngay wax ca xolam naan: «Balaa yàgg ñu dëj sama baay, te bu boobaa dinaa rey sama rakk Yanqóoba.»
TSK
TSK · Proverbs 16:7
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Nit ka ne ko: «Na nga tudd?» Mu ne ko: «Yanqóoba.»
Ci biir loolu ñu jottli ndigali buur, ya jëm ca ay jawriñam ak njiiti Wàllaa Dex. Ñooñu it jàpple mbooloo ma ca liggéeyu kër Yàlla ga.
Ndaxam Aji Sax ji nee: «Maa lay xettli déy, ngir sottal lu baax; maa la defal sa noon di la tinu déy, ci janti safaan ak njàqare.»
¶ Ci biir loolu Sóol moom, noyyeewul lu moy di tëkkook a jéema bóom taalibey Sang bi. Mu dem nag ca sarxalkat bu mag ba,
¶ Ana lu nuy waxati nag? Gannaaw Yàllaa ànd ak nun, ku nu manal dara?
Su ko defee ngeen di dunde dundin wu yellook Boroom bi, ngir bànneexal ko ci wet gu nekk, seen meññeef it di jépp jëf ju baax, te ngeen gën di xam Yàlla.
yal na leen matal sëkk ci lépp lu baax, ngir ngeen di jëfe coobareem. Yal na def ci nun bànneexu boppam bu mu sottale Yeesu Almasi, mi daraja ñeel ba fàww. Amiin.