Yaakaaru noon yi de melul ni sunu yaakaar, te loolu la noon ya àtte.
TSK
TSK · Proverbs 18:11
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Psalms 49:6
TSK
Ana lu may tiit bés yu metti, yu ma njublaŋ yéewe seeni ñaawtéef,
Psalms 52:5
TSK
Lu bon a la gënal lu baax, fen a la gënal wax dëgg. Selaw.
Proverbs 10:15
TSK
Alal day aar boroom ni ab tata, ñàkk di lor baadoolo.
Proverbs 28:11
TSK
Waay a ngi barele, defe ne xelu na; ku néewle am ug dégg, gis ne xeluwul.
Jeremiah 9:22
TSK
Aji Sax ji dafa wax ne: «Ku xelu, bumu damoom xelam; ku jàmbaare, bumu damoo njàmbaaram; ku woomle, bumu damoom koomam.