Exodus 23:3
TSK
Néew-doole bi it, buleen ko far cib layoo.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Néew-doole bi it, buleen ko far cib layoo.
¶ «Buleen safaan dëgg cib àtte. Buleen far néew-ji-doole te buleen far boroom doole. Àtteleen seen moroom ci dëgg.
Buleen jalgati yoon cib àtte, buleen jeng te buleen nangu alalu ger, ndax ab ger day muur bëti boroom xel, di xañ aji jub dëgg.
Yàlla daal ngeen di waxal njubadi, di ko duural?
«Dungeen bàyyi àtteb njublaŋ, ak di faral ku bon? Selaw.
Lii it ñi rafet xel a ko wax. Par-parloo cib àtte baaxul.
di dëggal ku sikk ndax ab ger, tey xañ boroom njekk, ag njekkam.
Lu bon la seeni loxo mane: kàngam di laaj, ab xaali di sàkkub ger, boroom daraja moom, di wax fuqley bakkanam, ñu ànd ràbbum pexe.