TSK

TSK · Proverbs 20:16

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Moom doŋŋ la am ci yére, di ko sànge yaramam; su ko ñàkkee, lu muy sàngoo ba tëdd? Te su ma wooyee wall kat, dinaa ci dégg, ndax man Boroom Yërmande laa.

Lu mel ni lem la ndaw su yemadi di wax, làmmiñ wa ni diw gu ñu lay raay.

Dina la aar ci ndaw su yemadi, bokk feneen, di wax lu neex.

Bul gàddul kenn bor, di loru; bañ koo dige, daldi am jàmm.

Ab gànc yeer mu xóot la, jabaru jaambur di teen bu xat.