Psalms 21:7
TSK
jagleel ko barke bu sax dàkk, bégale ko sa kanam, mu bànneexu.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
jagleel ko barke bu sax dàkk, bégale ko sa kanam, mu bànneexu.
Ngalla féqal fani Buur, ay atam bare, sët ba sëtaat.
Bu la ngor ak worma dëddu, booleel takk ci sa baat, bind ko ci sa àlluway xol.
Buur daa sib kuy def lu bon, ngir njekkay dëgëral nguuram.
ab jal sampe fi ci ngor, ki ci tooge jikko ju dëggu di askanu Daawuda te di njiit luy sàkku yoon, yàkkamti njekk.