TSK

TSK · Proverbs 21:25

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Yaafus bee, xoolal xorondom, seetal ci moom, ba muus.

Yoonu yaafus, dégi neen; kuy jubal, saw xàll yaa.

Ab yaafus du gàbb ba mu jotee, day wut am ngóob, du am dara.

Toolub ku yaafus laa jaare, ak tóokërub nit ku ñàkk bopp.

Ab yaafus day foog ne moo gëna muus juróom ñaari boroom xel yu xam tont.