TSK

TSK · Proverbs 22:11

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Firawna wax ak Yuusufa ne ko: «Ndegam Yàlla xamal na la lii lépp kay, leer na ne amul kenn ku muus te rafet xel ni yaw.

Ezra 7:6 TSK

Esra moomu jóge Babilon, nekkoon jànglekat bu xareñ, bu géeju ci yoonu Musaa, wi Aji Sax ji Yàllay Israyil joxoon ñoñam. Aji Sax ji Yàllaam nag toppe ko yiwam, ba Buur defal ko mboolem lu mu ñaan.

Mardose Yawut ba, moo sësoon rëkk ca Buur Aserus, sut Yawut yépp, ay bokki Yawutam yu bare nawloo ko. Muy sàkku nag ngëneeli ñoñam, di waxal jàmm mboolem askanam.

Ku dëggu ci réew mi, ma geesu, ngir fat ko. Te kuy wéye maandute, kookoo may liggéeyal.

Wax ju dëggu, buur safoo boroom; ku jub, buur bëgg sa kàddu.

¶ Ba loolu wéyee Buur gëna teral Sadarag ak Mesag ak Abet Nego ca diiwaanu Babilon.