TSK

TSK · Proverbs 22:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ña ca des naan: «Danoo àbb xaalis, taylee ko sunuy tool ak tóokëri reseñ ngir fey galagu buur.

Ku sonal ku ñàkk, tooñ nga ka ko sàkk; ku baaxe ku néewle, teral nga ka ko sàkk.

Not néew-ji-doole ngir yokkule, mbaa may boroom alal, loo ci def mu wàññi la.

sarxalkat beek baadoolo bi, sang akub jaam, njaatige lu jigéen ak ab janqam, jaaykat ak jëndkat, ablekat ak àbbkat, leblekat ak lebkat.

Amos 4:1 TSK

Dégluleen kàddu gii, yeen jigéeni tundu Samari, yeena ngi suur ni nagi diiwaanu Basan. Yeen ñiy torxal néew-ji-doole, di not aji ñàkk te naan seeni jëkkër: «Indil ñoll waay, ñu naan!»

Amos 8:4 TSK

Amos ne: «Dégluleen lii, yeen jula yiy dëggaate aji ñàkk, di jeexal néew-ji-dooley réew mi,

James 5:1 TSK

¶ Kaayleen nag ma wax leen, yeen boroom alal yi, jooyleen te yuuxu, ndax mitit yi leen di dikkal.