Proverbs 1:10
TSK
Doom, bàkkaarkat bu la xiirtal, lànkal.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Doom, bàkkaarkat bu la xiirtal, lànkal.
Gone yi, tee ngeena dégg yaru baay, te déglu, ba am ug dégg?
Doom rafet xel, baay ba bég; te ab dof ay xeeb ndey ja.
Deel bégal ndey ak baay, rawatina ndey ji la jur.
Maay am mbégtey baaxe leen, jëmbat leen bu wér ci réew mi, jëmbate leen sama léppi xol ak sama léppi jëmm.»
Waaye mbégte ak bànneex war na, ndax sa rakk jii moo dee woon te dekki na, moo réeroon te feeñ na!”»
Léegi kay nu ngi dundaat, gannaaw yeena ngi sax ci Boroom bi.