TSK

TSK · Proverbs 23:5

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 1:14 TSK

Ci biir loolu ndaw dikk ne Ayóoba: «Nag ya daal a doon rijji, mbaam ya di for ca wet ga.

Yaatuwaayu loxo nga ma àppal ciy fan, sama giiru dund du dara fi yaw. Képp ku taxaw di cóolóolu neen. Selaw.

ndax alal wéyul fàww, ag pal du ñeel sëtoo sët.

mbaa pexeem moy, mu sànkule; ba bu amee doom it, du ko wacce dara.

Ana lu ngeen di waññe xaalis, di ko jënde lu dul aw ñam? Ana lu ngeen di sonn, di jënde lu dul reggal? Dégluleen maa déglu, ba lekk lu leen di dundal, di xéewloo seen ngëneelu bakkan.

«Demal jëli Yeremi, nga sàmm ko, te bu ko def dara lu metti. Lu mu la ñaan it, defal ko ko.»

¶ Li may wax, bokk yi, moo di, li des yàggatul. Kon nag bés niki tey, na ñi am jabar mel ni bu ñu ko amul woon;

James 5:1 TSK

¶ Kaayleen nag ma wax leen, yeen boroom alal yi, jooyleen te yuuxu, ndax mitit yi leen di dikkal.