Proverbs 10:1
TSK
¶ Kàddu yu xelu yu Suleymaan. Doom rafet xel, baay ba bég; doom dof, ndey ja tiis.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Kàddu yu xelu yu Suleymaan. Doom rafet xel, baay ba bég; doom dof, ndey ja tiis.
¶ Lii moo di peeñum Esayi doomu Amocc, di lu mu gis ci mbirum Yuda ak Yerusalem ci janti buuri Yuda yi ñuy wax Osiyas ak Yotam ak Axas ak Esekiya.
Ba loolu amee mu yebal Elyakim bootalub Buur ak Sebna bindkat ba, ak ñay mag ca sarxalkat ya. Ñu sol saaku yu ñuy ñaawloo, daldi dem ca Yonent Yàlla Esayi doomu Amocc.
¶ Kàddug Aji Sax jii moo dikkaloon Mise miy waa Moreset, ca janti Yotam ak Axas ak Esekiya, buuri réewum Yuda, na seen nguur topplantee. Lii la Mise gis ci mbirum Samari ak Yerusalem.