Psalms 66:10
TSK
Éy Yàlla, nattu nga nu, xelli nu, ni ñuy xellee xaalis;
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Éy Yàlla, nattu nga nu, xelli nu, ni ñuy xellee xaalis;
Yerusalem, maa lay teg loxo, maay seeyal sa raxit ni xeme, ba dindi sa mbuubit mépp.
Waaye bésub dikkam, ana ku ko mana dékku? Bu teewee ana kuy taxaw? Nde moom daa mel ni sawaras tëgg buy xelli weñ, melati ni xemey fóotkat.
¶ Kër gu mag nag, du ndabi wurus ak xaalis rekk a fa am, waaye yoy bant a nga fa, ak yoy ban; yii di ndabi teraanga, yee di ndabi njoogaan.