TSK

TSK · Proverbs 25:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Woyof, ànd ak ku néewle moo gën séddook ku bew la mu lewal.

¶ Yeesu teg ca ne: «Maa ne leen, kooku moo ñibbaale këram àtteb ku jub, waaye du Farisen ba. Ndaxte képp kuy réylu, dees na la toroxal, waaye ki toroxlu lees di yékkati.»

¶ Gannaaw loolu damaa xool, rekk yem ci bunt bu ubbiku fa asamaan. Ci biir loolu baat ba ma jëkkoona dégg muy wax ak man te mel nig liit, ne ma: «Yéegal fii, ma won la liy topp ci loolu.»