TSK

TSK · Proverbs 25:8

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Abner àddu ca kaw, ne Yowab: «Xanaa saamar day lekku suux ba fàww? Xamuloo ne lii aw naqar doŋŋ lay mujje? Ana looy xaarati ci ne mbooloo mi ñu noppee topp seeni bokk?»

Ba loolu amee Amaciya yónni ay ndaw ca buurub Israyil Yowayas doomu Yowakas doomu Yewu. Mu ne ko: «Dëkk naa la, dikkal nu jàkkaarloo!»

Ndoortel ay di wal mu tàmbali, luy indib xuloo, bàyyil.

Ndax ku ruux soow, am ca dax, ku wañaar bakkan, mu nàcc, te lu jógal xol, indiw ay.

Yonent yiy wax waxyuy fen, sarxalkat yiy jiitee seen coobare, te sama ñoñ soppe ko ni! Moo bu muj ga taxawee, nu ngeen di def?»

Am ban buur mooy xarejeek beneen buur te jëkkula toog, seet ba xam ndax man naa ànd ak fukki junniy xarekatam, ngir xarejeek ku ko songseek ñaar fukki junniy xarekat?