Exodus 9:20
TSK
Ba mu ko defee ña ragal kàddug Aji Sax ji ca dagi Firawna fat seeni jaam ak seeni jur fu wóor.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ba mu ko defee ña ragal kàddug Aji Sax ji ca dagi Firawna fat seeni jaam ak seeni jur fu wóor.
Turu Aji Sax ji rawtu bu mag la. Ku jub daw làqu ca, raw.
Yeen samaw askan, ayca duggleen seeni néeg, tëju ca biir. Làquleen as lëf, ba sànj mi jàll.
Ñaar yooyu du tebbiku ndax Yàlla du fen, te nun ñi daw làqusi ci moom, ci lanu ame ndëgërlaay lu réy lu nu ŋoye ci yaakaar ji ci sunu kanam.
Waaye asamaanu tey jii, ak suuf, genn kàddug Yàlla googu moo leen yeb cib denc, ñeel sawara, kera bésub àtte ba, bésu sànkuteb aji gëmadi ñi.