¶ Ba Asa buurub Yuda duggee ñaareelu atu nguuram, ca la Nadab doomu Yerbowam falu buur, jiite Israyil. Nadab jiite na Israyil ñaari at,
TSK
TSK · Proverbs 28:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
1 Kings 15:25
TSK
1 Kings 16:8
TSK
¶ Ba Asa buurub Yuda duggee ñaar fukkeelu atu nguuram ak juróom benn, ca la Ela doomu Basa falu buur, jiite Israyil. Péeyoo na Tirsa diiru ñaari at.
2 Kings 15:8
TSK
¶ Ba Asaryaa buurub Yuda duggee fanweereelu atu nguuram ak juróom ñett, ca la Sàkkaryaa doomu Yerbowam falu buurub Israyil, péeyoo Samari. Juróom benni weer la nguuru.
Fekk fa ku néewle te xelu. Mu manoona xelal dëkk ba, xettli leen, waaye kenn faalewu ko.
Isaiah 58:12
TSK
seeni nit tabaxaat gent ya woon, ngeen yékkatiwaat kenu yu yàgga yàgg. Dees na la wooye jagalkatu xar-xar yi, mbaa kiy yeesal xàll yi, ngir dëkke réew mi.
Hosea 13:11
TSK
Ci biir mer laa la falal buur, te ci samam sànj laa ko follee.